Ëttub wolof

Dalu web bi leen di jàppale,
ci jàng dawal ak jàng bind làkku wolof

Dibeer, fukki fan ak ñett, ci weeru oktoobar, atum 2024

Nañu delloo làkki réew mi seen gëdd, di leen jëfandikoo ci bépp jokkoo. Séex Anta Jóob nee na : « làkku jàmbur, su neexee ni tàngal it, kenn mënu koo macc ba ciy tàqamtiku ».

Séex Anta Jóob


Boo bëggee jokkoo ak ñun, bind ñu bataaxal ci suuf wala nga bind ñu ko ci kallaamayreewmi@gmail.com